|
|
Songs | Albums | Album Arts
Lyricist: Youssou NDour
Lyrics:
Parole Youssou N'Dour feat Akon Song Daan
Dooley nit kou ñuul kou Ko beug xam la Mbeur mouy daan kou Ko beug xam démal la ko you
Woma woma Ci leundeum Dinala Wouyou Oubil sama Xol dinga Xam nimou sédéé ci you
Fileg mang lay am Sama xol Luma songù Daan ko
Fileg mang lay am Sama Xèll Luma songù Daan ko
Songù Daan Koooooooo Songù Daan Koooooooo Songù Daan Koooooooo Songù Daan Koooooooo
Man Maanan Mane iiow laa Iiow nga naan Ngané man leuh
Man Maanan Mane iiow laa Iiow nga naan Ngané man leuh
ÉH ÉH ÉH ÉH
Béneu biss dina niow Mou melni louniouy netali Mou melni lii dou
Anhhhhhhh
The ken Du jog Naan man mi nako fékéh Yooooooo
Ndah nguelaw lii daaw diñou yobalé Xoob yiy russ ci garab guii Ah lifi xew tay büñü ko fatéé Africa Dom yiy wane Sén bopeuh
Fileg mang lay am Sama xol Luma songù Daan ko
Fileg mang lay am Sama Xèll Luma songù Daan ko
Songù Daan Koooooooo Songù Daan Koooooooo Songù Daan Koooooooo Songù Daan Koooooooo
Man Maanan Mane iiow laa Iiow nga naan Ngané man leuh
Man Maanan Mane iiow laa Iiow nga naan Ngané man leuh
ÉH ÉH ÉH ÉH
Cí Díg bï Fofù Laay diar Mù am xàl Safara douma daaw Los angeles Paris ba Rio New Delhi London Tokyo Sêdoog Yén Liñyou Jlé Fénéne
Fí ñù Diarr ñun ba éksi fí Dafa mèlni LouDou nétali
Los angeles Paris ba Rio New Delhi London Tokyo Sêdoog Yén Liñyou Jlé Fénéne
Éh Éh Hh hhhhhh Hhhhhhhh
Maa contaane Yoow it yaa contaaan Maleu geuuneuu contane Uhh Yeahhhhh Hhhhhh!! Contane yeahhh
Yeaaahhh Contane yeahhh Contane yeahhh
Akon Yousou Yeah
Akon Yousou Yeah
Cí Díg bï Fofù Laay diar Mù am xàl Safara douma daaw Los angeles Paris ba Rio New Delhi London Tokyo Sêdoog Yén Liñyou Jlé Fénéne
Fí ñù Diarr ñun ba éksi fí Dafa mèlni LouDou nétali Los angeles Paris ba Rio New Delhi London Tokyo Sêdoog Yén Liñyou Jlé Fénéne
Song Daan Youssou Ndour feat Akon Lyrics by Abdoulayebacary LyricsFreak
|
All lyrics are property and copyright of their owners.
2025 Zortam.com
|