Songs | Albums | Album Arts
Song: | Baykat |
Album: | Senegal | Genres: | |
Year: | | Length: | 261 sec |
Lyrics:
Mané hé baykat bi khalam Démonna bay nékh wayé boumgua Dokna mome Mané hé baykat bi khalam Démonna bay nékh wayé boumgua Dokna mome
Mané hé baykat bi khalam démonna Bay nékh wayé boumgua dokna mome
Boula nékhé talalal say lokho Yaye docteur biy fath khifou askane bi Liko dalé si nditoum rew bassi miskine Ya souméko di dane sa dolé andak nath Bi di liguey sa gnakha di tourou Ngay bay di doukat bilay ya am diome
Kon diarama baykat koufi xiff yako Doundal bamou sour waw koufi fébar Yako nandal aki réén bamou féékh
Kon diarama baykat koufi xiff yako Doundal bamou sour Waw koufi fébar yako nandal aki réén Bamou féékh
Ya momone sa mbay Ya mome sa guanthiakh mome say Ndiour ya mome sa alla di bay Nguour gneuw dougalthia lokhome ak Boor fékeleuthaa guanthiakh ba Mégneu lole ndékétéyo
Kon diarama baykat koufi xiff yako Doundal bamou sour Waw koufi fébar yako nandal aki réén Bamou féékh
Kon diarama baykat koufi xiff yako Doundal bamou sour Waw koufi fébar yako nandal aki réén
Bamou féékh Dirama diarama baykat bé yaw Kéneu rek mola mana fay Moy bourbi yaalla Guathia ngalama
Guathia ngalama yaw baykatbé Guathia ngalama Guathia ngalama yaw baikatbé
Dirama diarama baykatbé yaw Kéneu rek moleu mana fay Moye bourbi yalla
|