Songs | Albums | Album Arts
Lyrics:
ma ngui binde way bi diko m?y gneup gni ma beugue di l?n ndioukel ndioukel gneup gni ma diapal? souma l?ne meunone diokh lokho defnako soumal?ne meunona setsi eh eh yeksina
fat?woumal?ne, d?d?te meunoul am yeugone nal?n salaw moy li wor souma teugu? ng?ne gneuw wouyoussima souma gu?n? lou bess ng?ne dieundeuko manou mal?ne faye magui bind way wi di l?ne ko m?y
refrain (bis) you you you you you gorgorloul gnougui sa guinaw
soumal?ne meunone diokh lokho defnako souma l?n meunona setsi y?ksina kouma souf?l ng?ne khoulok mom fat?woumal?ne d?d?t meunoul am yeugue nal?ne salaw moy li wor bataxna ma gui bind way wi diko may
refrain (bis)
fat?wouma fat?wouma fat?wouma fat?wouma ah (4 fois)
refrain (bis)
ehhhhhhhhhhhhhhh mangl?ni sant di gueureum mane ndioukel nal
|