|
|
Songs | Albums | Album Arts
Song: | Wiri wiri |
Album: | Joko | Genres: | Pop |
Year: | 2002 |
Length: | 248 sec |
Lyrics:
Ha dem Dem fan Lu ma bėggoon mėnul nekk Leer nga ci kenneen Man ma ngi ci lėdėm Xam naleen, may ki koo def Suma demee bay meree Duma meree kudul sama mbopp Te man may seeti baye baalu ko Wiri wiri jaari ndare Wiri wiri jaari ndare, ndare Xam na dem Demul feen fu nguy wuute Ligeey u ma Li ma mbėggoon moy mu dox Te duma dox, ci sen kaw Xam na lépp, may ki ko deef Suma demee bay meree Duma meree kudul sama mbopp Te man ma seeti bay, baalu ko Wiri wiri jaari ndare Wiri wiri jaari ndare, ndare Wiri wiri jaari ndare, ndare Bilay, bilay, bilay, bilay-bilay Ma rėccu Ma nee soy dem mba xamatoo fa jėm Delul fa nga jukkee Fuy la xamee Fii nga mbaggee Fuy la teete Fi nga jange école Wiri wiri jaari ndare Wiri wiri jaari ndare, ndare Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri-wiri-wiri) Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri-wiri-wiri) Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri) Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri-wiri-wiri) Wiri wiri jaari ndare, ndare (ha fokk ma seeti bay) Wiri wiri jaari ndare, ndare (wara bokk mba seeti yaay) Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri-wiri-wiri) Wiri wiri jaari ndare, ndare (ha fokk ma seeti bay) Wiri wiri jaari ndare, ndare (wara bokk mba seeti yaay)
|
All lyrics are property and copyright of their owners.
2025 Zortam.com
|