Artist: A B C D E F G H I J K L M N O P Q R S T U V W X Y Z

Download Now!!!

Songs    | Albums    | Album Arts

Song:Xel (Think)-Plus fort
Album:I Bring What I LoveGenres:Soundtrack
Year:2010 Length:380 sec

Lyrics:

Paroles De La Chanson Xel
famarã« Reub Kat Lawone
da Ama Biss Mou Khall Yã´ne
mu Taxaw Di Xalat Bamu Yã g
mu Sã¨ne Mbã«tt Miy Daw
mu Suxat Fital Ambadi Dã¢gu
tã© Nane Kã® Douma Raw
far Mbã«tt Ma Sã¨ne Kokorong
dadi Dieul Bop Ba
dal Di Koy Rã´ne
bopp Ba Neubouna Litha Des
yaramam Bã©ppa Ngui Fã¨gn
deune Bak, Ndigg Lak, Tank Yak, Yã©nã¨ne Ya
lippe Di Fã¨gne

lii Takh Mou Dã©fã©ni
mbeutteu Daa Amoul Xel
kone Gnoune Gni Yalla Jox Xel
nagnu Santati (X2)

li Yalla Bind Yã©pp Nit Lathie Gueneu Fonk
mala Yi Lignou Woutelã© Ak Gnom Moy Sougnou Xel Motax Dã©f

loy Dougou Jitalal Sa Xel
ba Lo Thiã¨y Wout
di Nga Guiss Nguenã©l
nit Gni Yor Xel Boo Sã©tã© Gnoy Dokhal Aduna
kiy Dã©f Tã© Dou Xalat
thi Missal Day Mã©l Ni Mbeut Ma

nit Mã´m Khã©lako Yor(X4)

li Yalla Bind Yã©pp Nit Lathie Gueneu Fonk
mala Yi Lignou Woutelã© Ak Gnom Moy Sougnou Xel Motax Gnuy Dã©f

fi Neubeu Moy Khax
boko Amoul Yangui Mã©l Ni Bayima
sokou Amoul Doto Nã©k Nit

li Yalla Bind Yã©pp Nit Lathie Gueneu Fonk
mala Yi Lignou Woutelã© Ak Gnom Moy Sougnou Xel Motax Gnuy Dã©f

wawaw(X4)

famarã« Reub Kat Lawone
da Ama Biss Mou Khall Yã´ne
mu Taxaw Di Xalat Bamu Yã g
mu Sã¨ne Mbã«tt Miy Daw
mu Suxat Fital Am Ba Di Dã¢gu
tã© Nane Kã® Douma Raw
far Mbã«tt Ma Sã¨ne Kokorong
dadi Dieul Bop Ba
dal Di Koy Rã´ne
bopp Ba Neubouna Litha Des
yaramam Bã©ppa Ngui Fã¨gn
deune Bak, Ndigg Lak, Tank Yak, Yã©nã¨ne Ya
lippe Di Fã¨gne

lii Takh Mou Dã©fã©ni
mbeutteu Daa Amoul Xel
kone Gnoune Gni Yalla Jox Xel
nagnu Santati (X2)

li Yalla Bind Yã©pp Nit Lathie Gueneu Fonk
mala Yi Lignou Woutelã© Ak Gnom Moy Sougnou Xel Motax Gnuy Dã©f

wawaw Lolu Moy Xel
soko Amoul
yangui Mã©l Bayima (X3)
loy Dougou Nang Ko Tã©kã© Xel
famarã« Reub Kat Lawone
mbeuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuutt!




 

Download Now!!!

Copyright © 2020 Zortam.com. All Rights Reserved.   Zortam On Facebook Zortam On Twitter