|
Lyrics:
Dem dem
Dem fan ?
Den ndax lan ?
Baya ko mom
Dem nguir xee bou barri bi
Dem ndax teen boh neex bi
Teh rapp rek noom noo siy naan
Nach bi lakkatouma taw bi barrewoul
Dem ngir bokk bone menou fee am
Dem ngir daffa wara nekk gorr done
Goorgoorlau
Dem dem
Dem fan ?
Dem ndax lan ?
Liberte bi
Si espace bou lendeum bi
Sama beut yi guissa tounou
Garap yi nga xamenteni noo ma souxat
Su beut setiee barap yi bow
Dem ngir Keur gui daf may nirou lou lendeum
Dem nguir daffa warranekk goor done
Goorgoorlau
Damay dem
Chi alla bi
Damay dem Chi dex goumak gui
Ne damay dem waw seeti sama nawleyee
Damay dem si ban bou ritax bi
Damay dem ba reewu bitty
Ne damay dem waw setti samambokkyee
Go-go (bis)
Won ma sa xarit ma wax la ki nga donoy
Won ma sa mbokk ma wax ko fi ngay diaar
Hey what do you need ?
He he yaw lilaneex
Won ma sa xarit ma wax la ki nga donoy
Won ma sa mbokk ma wax la fi ngay diaar
Hey defa li la neexoy hey yaw lila soop
Sammkatou mboott moo xam ba ciy
Sooxaoy ni meneuh kott ñoom daal amouñou
Mbaam hey defal li la nexx oo
Hey what do you want ?
Ho ho ho ho ....
Download Now!!!
Copyright © 2020 Zortam.com. All Rights Reserved.
|